Інструменты
Ensembles
Genres
Кампазітары
Выканаўцы

Вершы: Ma Valise. Wege. Samay Bok.


bakkan waruw dall la
fa muy degge dooko yeg
dem rekk delu si rekk
melni weer wi delu si ci sey jeego
feneen weer mouk ci fi,
bidew bi danouna dee ci souff

samay xarit, tey ji
ndadje bi rafet na,
djoko, seeddo,
ak retane bi rafet na,
xew bou neex
mais soubbe dagniouy dem,
galankor bi moy dougnou
meuneu xamante bou bax,

dou nouy am waxtou
bou doy ngir soppante
goudi gi wess, mangi won
fenene, bi ci toop dina fi sori

ak samay bok ci camion bi,
dinagnouy teugueu ngir
feccelo yeneni nit
ak samy bok ci camion bi,
ngir andi mbekte bignouy djeul

bakkan waruw dall la
ku dul toxu doo xam fu dekk neexe
fa muy dagge dooko yeg


(Merci a El Cancre pour cettes paroles)
Ma Valise
Ma Valise